Sàkku ci jëfandikukaay bi
Man, benn ci saa- Wolof yi maa doon sàkku ci jëfandikukaay bi nga def ci Alxuran bu ñu bind ci Wolof, dina tax sax nun Saa-wolof mu yokk sunu xam-xam ci Làkk wi. Li nga def ni nag, Yàlla moo la ci fay ndax yangi dundal Làkk wi Suma manoon jokko ak yaw dina baax loolu sëriñ bi ?